Imprimer
Catégorie : Uncategorised
Affichages : 70

Lekkug xale bi diggante 6 ba 11 weer (juróom-benni weer ba fukki weer ak benn)   

NÀMPALU WEEN AK ÑAM YI KOY MOTTALI

 

Léegi nag, ween kese doyatul ngir yokkute xale bi. Ngir mu màgg ni mu ware, dafa laaj mu tàmbalee lekk yeneen ñam yu mottali ween wi.

 

DÉNKAANE VI

 

NDOLLENT LI